Limou mbiryi: 3
17 / 2 / 1437 , 30/11/2015
Neknathi leral lounou name thi magal yonentebi,ak yiy dimbele thi magalko, magalouk salaf nielko,ak yonou nioudigue doumao thi magalko…
Nekna thi leral ni fitna bouyoublise bourom khamkhamyi niokoy kham boumatale niebe khamko,touddou warwarou bourom khamkhamyi ak khaleyou kouryi ak kilifayi…
2 / 12 / 1436 , 16/9/2015
Nekena thi leral amsolok ndokh thi doundou domou amdama, ak leral louygalagn kor wathiouk ndokh ay lounouy wakh boutaw diwathie…