Limou mbiryi: 168
2 / 7 / 1437 , 10/4/2016
khoutba thi L’equilibre entre la religion et la vie d’ici bas. deg deg bou amsoula.
17 / 5 / 1437 , 26/2/2016
koutba thie securite bou ama solo La sécurité nationale, responsabilité de qui
3 / 5 / 1437 , 12/2/2016
khoutba thie aye bire Liy sippi jëf
17 / 2 / 1437 , 30/11/2015
thi kawe soufe Waréfu sàmm kàràŋŋé gi
Neknathi leral lounou name thi magal yonentebi,ak yiy dimbele thi magalko, magalouk salaf nielko,ak yonou nioudigue doumao thi magalko…
Nekna thi leral ni fitna bouyoublise bourom khamkhamyi niokoy kham boumatale niebe khamko,touddou warwarou bourom khamkhamyi ak khaleyou kouryi ak kilifayi…
13 / 10 / 1436 , 30/7/2015
Sabab yiy tax ñu déllo jëf
11 / 8 / 1436 , 30/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Méloy yahuud yi
22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekenathi leral yene mbire younouy sako takhe tanekouthi, ak leral fane latakhe neke…
17 / 5 / 1436 , 8/3/2015
Leral niety degnkayi bithi diake:fedali gueguem bouwer,rafetal diame thi waydiour, ak oubbe kouam solo
14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: ay sabab yiy tax Yalla wattoup jàmam
19 / 4 / 1436 , 9/2/2015
Neknasi toudou ay melokan youbari nirl yahoudyi andak tou dou ay teketalam thi al khourane
15 / 4 / 1436 , 5/2/2015
Toudou boulem adissyi rote thi leral takhalikok khewi andak firiko ak lreal linou thiydegue ak linou thiy diarinio…
Toudou lerarou omar ibnou abdoul aziz diam thi kpkodon lathi thi guem dogal nekena thi letarbi dekane you mague ak tontou lou matale.
Leral niari sarte yokhamni diaf douwer loudoul niam,tektali selal ak toupou yalla ,boukouna thi tanki row thi yonetebi…
27 / 3 / 1436 , 18/1/2015
Dancek boyalouk lammenige thi wakh diou amoul niarige,doude loubari thi batoubokkale yousiwe thi lammeniou niteni.
17 / 3 / 1436 , 8/1/2015
Lanlanou dioullou thi Khokhoutal domou adamayi thi niou bania wakh sen khalat,ay dioublou wayam ak ay mandargam,ak ay diekhaltamam ak ay safarame…
Leral guemu yalla guou were,diouko youbakh yebe meniantefou guemu yalla la, diouko youbon yebe dafay dakhok guemu yalla gouwere
1 / 3 / 1436 , 23/12/2014
Diggdômou
29 / 2 / 1436 , 22/12/2014
Kham koupa sounou borom moko diago, leral lanmoy tiabiy koumbo, khaji koumba,leral lanteou ndiabarkatyi thisenwate khamkhmoun komba…