Limou mbiryi: 168
11 / 8 / 1436 , 30/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: dëgg dëggi séllal
29 / 7 / 1436 , 18/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Bumm yi boolé xétum lislàm
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Lu bonu késsé du jogé ci Yalla donté nitñi daño giss né lu bon la
24 / 6 / 1436 , 14/4/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: li Yonènetebi (Yalla na Yalla joulli ci moom té dooliko jaam) taxawé ci jànggalé ak yar ak tàggate wènn xète
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Diglé lu baax téré lu bone_Dr Mouhammad A Lô (1)
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Jàŋŋalé ak yar akiy,
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Fann la téxé nèkk
Wooté ci Al-Khourane ak Sunna-ay ngeünélam akiy jéxitam
22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekenathi leral lane moy wote ?yane nioy galelou wote diame thi yalla ? dirkhanetalou wote diamethi yalla…
17 / 5 / 1436 , 8/3/2015
Nekenathi nontou ay lathe youbari bakounathi:ndakh merouk niari wadiour day waral niakanaguou ak diamouyalla?niane nioy kourelou asahira?
14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: khamlé oubé thi dîné, wâthouwâyam thi lislam, ay ponkam, ay teukk you thi ajou.
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral lane môy lou baax ak lou bonn, solôm, teunkk you jeum thi diglé lou baax ak téré lou bonn
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral taaroup lislam bi ngui khamné môy dîné jâmm, akiy téggine you rafète thi dounnd ak gnoudoul joullite. Di tônetou gni gnâwal thi Yonènete Mouhammad (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâm)
28 / 4 / 1436 , 18/2/2015
Lane moy ndiabar ak lane moy aykhadia ak lane moy ay atteme thi islam ak nane lankoy safara boudalenit…
15 / 4 / 1436 , 5/2/2015
Leralni nite thi sene diekhantal thi wete thi yalla todono seddeliko thi dienti khath ak …
9 / 4 / 1436 , 30/1/2015
Leralni ragal yalla dafa ame ay meiente thi adouna ak alahkira, doudouk niarfouki diarigne niel ragal yalla thi adouna…
25 / 3 / 1436 , 16/1/2015
Wakhtâwî mi ngui jeum thi: deuggeunetânou kham-kham, ngeunélam, ngeunélou borôm kham-kham, gâkk-gâkki sâkkou kham-kham ak ni mag gnou bâkh gni sâfarâ
Jékhîtou njabar thi niteki askane wi
Wakhtânewi ngui ajou thi khol bou mâp: mândargâm yi geuna râgnékou ak jékhite yimouy déf thi dôkhalînou niteki
29 / 2 / 1436 , 22/12/2014
Lanmoy ligueyou mbolo?lanmoy guisguisou lislam thi ligueyou mbolo? Ndakh dakanna thi jiguen mouybok thi ligueyou mblo?...