Limou mbiryi: 168
24 / 6 / 1436 , 14/4/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ragal Yalla jàréko ci sèttanetal alkhourane ak diko doolli
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sabap yiy sippi jeüf
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Guissiine ak dokhalinu lislaam ci koom koom ak souxaliku
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sartiy tuup
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ni aada di jéxité ci xalaatine
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ay njaangalé ci ndéŋkaané Luqmaane
Lii ay ubbé la 10-03-2015
22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekena thi toudou diarigne yi ganamague thi werou kor bokounathi :mougne thi mbolem khadiamyi,ak fouklou borombi thi lou lakhou…
21 / 5 / 1436 , 12/3/2015
Touki Diame Allakhira
14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: léral wakh yi rote thi sânjjé gui nèkk thi wax lodoul dèf. Nguénéloup jeuf bou sèll. Yéne wou dis wik thi jeujf bou sèll. Wax lôdoul dèf akiy loram thi ligèyoup lislam. Akiy jékhitam.
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral ay lâj you bari té ajou ci Al-jana, ak fékhé ba douggfa, ak sabab yifay takha dougg
Wakhtâne wi mi ngui ajout hi lèral: Kéno yi ngua khamné thi la étâp joullite di tégué ak léral ngourouk Omar Ibn Aboul Aziz ligèye gou mak goumou thi déf ak béssalam
12 / 5 / 1436 , 3/3/2015
Nekena thi leral ittewo islam thi manou ak diekhalam thi tabakh ab sociote , touddou yene khew khew yokhamni manou dinafa feddelikou…
Nekena thi leral amsolo khoutba al diouma, ak kane moy khoutbakat , ak lanlawara khoutba
1 / 5 / 1436 , 20/2/2015
Lekenathi toudou loubari thi warefou diague katebi diamanouy compo,leral tene mbir tokhamni lene thi diague katyi nioguikoy defe temouwoutrk islam…
21 / 4 / 1436 , 11/2/2015
Leral loubari thi melokani aji oubbeji , ak dansek aubbe thi loudoul khamkham…
Leral linou dioulou thi toumourankek dine,toudou adise yiy tektaletoumourankek dine…
19 / 4 / 1436 , 9/2/2015
Leral laguelo digante diakka ak joulit,ak kane mouy dounal diakka ak nan lan koy doundale ,…
15 / 4 / 1436 , 5/2/2015
Lerani islam dafay wote diam thi dimbalante ,manou ak diouko youbakh dabok thu sababi yakatikouk bancoub islam,…